Karim Diouf

  • Si bi di bé da da lé / Dama khamoul loufi diar yaye djour sanni / Kholal gni fi beugue ame sene dome te Yalla mahoulenko / Boula Yall mayé dang koye khame / Tchey yawitt dome sa yo maqué Lép liye begg…
  • Yaw mi lé, djoudo tchi rëw, magué tchi rëw / Bourbi Yalla wersaguéla gua mana deme ba bitlim rëw mana / Danidollé, Boul Faté Mdéye Boul Fate Baye / Wara mana tok goorgoorlou / Ba gay dem, Mdeye ak Bay…
  • Aytcha len gnou saf / Mdakh fi bo doul saf / Do Djembeut dara mu skh / Lo donoul talibem mouno done serignam / Rew dal bou paré patt tcha tol ya la djogué / Gor ak Djiguene, aywalene tcha tolya / Ana …
  • Hé guawlène, guawlène gagnoyakamti guawl`ne, gnoune dé dagnon beugui / Gnibi deukeuba, Sénégal auion bigne done khar yaye gniewa guoule / Guawl`ne dgno yakamti guawléne / Guawl`ne dagno yakamti gawlén…
  • Il n’y a jamais de blanc sans noir / Comme une longue journée sans nuit / Beaucoup de temps perdu sur des couleurs / Changeons d’idées et de mentalités / La couleur du nouveau millénaire est dans nos …
  • Lii
    Li mo ma djakhal, li di li ma titall / Mac gna gui kheutiongourgui / Gouneyi woute kougnou soumi / Li mo ma djakhal, li di li ma titall / Mac gna gui kheutio ngourgui / Gouneyi woute kougnou soumi / M…
  • Mane, li ma beugueu dafa Barri te wouté oh mane / Sama beugue beugue rombena adounassité oh mane / Damay tok bamou yague sama khël dem tchi samay dom mane / Souma manone, souma manoné, khélal la gua y…
  • Wadjour, khol len li gueun tchi mome / Wadjour khol len / Gagni khol len li guen tchi mome / Gagni khol len / Wadjour set len li guen tchi mome / Wadjour khol len / Moytouko, Moytouko (2 x) / Qui dé l…
  • Bo guissé adouna ni mou mela takh ma wakhé ni / Guor dafa wara Gorguolu tambeléko tcha bamouye ndaw / Te khame ni wadjour, sen djan mome watchna / Dakh situation métiwone na lolo takhone ma guene keur…
  • Mit ko wakh bopame mouni dangue ko beigne yaye / Ya dagno khamoul mome louye nit / Mi mome nittaye guarrabame, garrabame guarrabame mome / Bo amé say nit té deggueutoléne diguani bok yenesayaw / Mbaye…
  • Say niane nagouna yaw mani santal / Say lidjanti ostina yaw mani teyloul / Bousa ande boyé sani tchi mata gueune fayko / Say niane nagouna yaw mani santal… / Mayou Yalla dafa barri té wouté / Mit koun…
  • Baye Boye, yague na la deguelou gua may diggeul, lo bakh Sama Baye Boye / Khame na ni, lounek dadj gua ko baye lëp guir mane / Khame na ni méti wone na lolou tchi djamono yé gnou wessou / Yaye Boye, m…

Share lyrics!

LyricsPortal is counting on users like you to enrich its lyrics database! If you know the lyrics to a song from the following list, or any other song performed by Karim Diouf, share it with our community by transcribing them.

By continuing browsing our site, you agree to the use of cookies, which allow audience analytics.